J’ai tou­jours rêvé d’une cité où dès mon réveil,
Le chant des oiseaux
Me rap­pelle les douces chan­sons de ma maman
Où les gens s’aimaient tendrement.
J’ai tou­jours rêvé d’une cité,
Où dès le réveil
Le chant des oiseaux
Me rap­pelle le chant des coqs de mon village.
Vil­lage de N’der,
Vil­lage des braves femmes du walo,
Où dès le pre­mier chant du coq,
Les femmes se lèvent
Pour pil­er le mil.
Vil­lage du walo où dès le matin.
Ndi­a­di­ane Ndi­aye, l’homme aux longs cheveux,
Fon­da­teur de l’empire du djolof
Se promène sur le rivage,
Pour départager les pêcheurs.
Ecoute, écoute le bruit des pilons,
Ten­dre et doux à mon oreille
Qui me ramène par la pensée,
Vers la cité où dès le réveil
J’entends le chant des moineaux
Qui s’envolent à l’horizon.
 

 

 

GOKH BI

 

Dama mas di janeer gokh bu,
bu may yewwu, woyu picc yi
Di ma fàt­tali samay woyi yaay yu neex ya.
gokh bu, nit ña dañoo sop­pante woon.
Dama mas di janeer­gokh bu,
Bu bët di set, woyu picc yi
Di ma fàt­tali woyu séqi sama dëkk ba.
Ndeer,
Dëkku jigéeni Waa­lo yu jaam­baare ya,
Fa nga xam ne, sab bu jëkk rekk,
Jéeg ji jóg
Ngir soq dugub.
Dëkku Waa­lo bu, bu bët di set
Njaa­jaan Njaay, góor ga ca njañ la,
Di ki sos ngu­u­ru Jolof,
Di dox­an­tu ca tàkkal dex ga
Ngir àtte mool ya.
Dégal, dégal Kan­daŋ-ndaŋ gi kuur yi
Neexa dégg ci samay nopp
Di ma del­loo, ci sama xel,
Ca gokh ba nga xam ne bu bët daan set
May dégg woyu sawóor yay
naaw ca gët-yem ga.

image_pdfimage_print